Archipelago : Les Mots du Président de la CCIA-TH

  • Auteur/autrice de la publication :

Archipelago 

Modou Diop, président de la Chambre de Commerce, d’Industrie et d’Agriculture de Thiès, « après 2 ans de mise en œuvre du programme, je juge les résultats obtenus satisfaisants. Ce programme a permis le renforcement des compétences et l’employabilité des bénéficiaires dans le secteur agricole, de la transformation de produits agro-alimentaires, charcuterie et aviculture.  Au terme de la clôture du projet, les résultats obtenus sont jugés satisfaisants.  » Je réitéré l’engagement et les sollicitations vers une deuxième phase du projet Archipelago au regard des résultats positifs présentés.  La clôture a été un événement majeur qui sera marqué d’une pierre blanche dans les annales de l’histoire consulaire des chambres francophones pour avoir tenu un projet dit (Archipelago) porteur de croissance et de frein pour la lutte contre l’émigration clandestine. Avec mes collaborateurs nous avons organisé une cérémonie de remise d’attestation aux 400 apprenants et 80 chefs d’entreprise. La plupart des bénéficiaires sont des jeunes, femmes et migrants de retour ». Je tiens  aussi à remercier la Chambre de Commerce et d’industrie des Côtes d’Armor en Bretagne, la Conférence Permanente des Chambres Africaines et Francophones, EUROCHAMBRES, SEQUA et les partenaires nationaux pour leurs implications dans le projet . Pour moi la coopération Nord Sud avec les missions de compagnonnage constitue  un véritable succès.

Archiipelago : Kaddu Njitu Chambre bu Commerce Cees   »ñiarri att bi ni amaalé projet bii mbéctté la ñu cii amme »

 Maane mii  Modu Joop , Jiité Chambre bu Commerce maangu xaamlé « Programme Bii tahna  ñu dolli xaam xaam ak ligueyou ndaw yii ñu tann  cii wallu yii di mbey , soppalii mbey, cii wallu ndawall ak yarum guinaar.  Bi ñuu tedie projet bii nak lii ñu dône xaar guiss nañe ko. Ñu gui xaar nak ñu yessal ko ci bénéne Archipelago Ndah nak niou gui diadieuffeul kourél yeup. Programme bii nii mel dina xéh xaaléyi di diel mbeune mi pour toukki walla diko deff cii anam you diaroul yonne . Cii biir tediou projet bii diokhnañ ay lidiassé you tollu ak 400 ay dommo adama  ak lou tollu cii 80  kilfa you djité ay keurou ligueyou kaay cii diwanou Cees . Maane mii jiité  Chambre de Commerce bou Cees mangui diadeuffeul wa Chambre de Commerce bou Cotes d’Armor caa Bretagne, wa CPCCAF, wa EUROCHAMBRES, wa SEQUA ak Mbolléem partenaire yii deff séene dollé  nguir sottal mbébétu wa ARCHIPELAGO. Di xaamlé yiite leukeulo bi di Beut Ganaar (nord), Beut Saloum (Sud) amena ndiééxiitaal cii sunu koom koom